Akwa Boni

Akwa Boni
Njiitu réew Kodiwaar
Dundu ak jaar-jaaram
Bésu juddu

1708

Gana
Bésu faatu

1750

Kodiwaar
Liggeey Lingeer
Waajur wu jigeen Abla Poku

Akwa Boni (wala Akoua Boni ) doomu rakk la woon bu Abla Pokou, benn lingeer afrik bu sos waa Baoulé ci kodiwaar , mingi cosaanoo Gana. Mu nguur ci diggante 1730 ba 1750.