' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.
Léewópóol Sedaar Seŋoor moo amal tegum xeer bu jënk ci wàllum taxawaay iniwersite wi ci 14 sãwiye 1975.
Taxawaayam mu ngi aju ci sart Royuwaay:N° bu 2 sãwiye 1990, iniwersite wu Ndar mu ngi teeru limu ndongo wu njënk (600)ci 17 Desàmbar 1990 ci yoonu négandi.
Mu ngi jot gëddam ci ndogalu Royuwaay:N° bu 10 sulet 1996 ak tur bu bees jóge ci ndogalu Royuwaay:N° bu 4 desàmbar 1996.
Ku ñu ko duppe Gaston Berger, nekk na ab kàngam ci wàllum xeltu, di doomu Senegaal ak Farãs, juddo Ndar-Géej. Di baayu Maurice Béjart.
Diggànte iniwersite ak Ndar toll na ci fukki (10) km. Boo jóge Risaartool jëmsi Ndar di nga séen wërngalu kàggu gu mag bi. Iniwersite dafa fekk boole ñaari dëkk : Sanaar Pël ak Sanaar Wolof. Loolu tax na ndongo yi di ko woowe yenn saay Sanaar. Itam kërub internetu ndogo daara yi« https://web.archive.org/web/20080419061846/http://www.sunusanar.com/ » la ñu ko tudde.
Iniwersite bu Ndar ëmb na juróorum-ñaari Bërëbu tàggat ak gëstu :
Barabu tàggat ak gëstu ci ladab ak xam-xamu nekkinu doomu aadama ëmb juróomu bàqasu:
Barabu tàggat ak gëstu ci xam-xam jëmale ak xaraala ëmb na bàqasu xayma jëmale, bànqaas informatig, bànqaas bitil jëmale ak tàggat ci wàllum xéy.
Barabu tàggat ak gëstu xam-xamu yoon ak politik ëmb na ñett bàqaas:
Kërug internet [1]
Kërug internet [2] Barabu tàggat ak gëstu caada, diine, taaral, ak jokkoo ëmb na juróom benn bàqasu :
SAT | SEG | SJP | LSH | TOTAL UGB | |
---|---|---|---|---|---|
2001/2002 | 400 | 280 | 499 | 1480 | 2659 |
2002/2003 | 475 | 325 | 535 | 1525 | 2860 |
2003/2004 | 559 | 349 | 575 | 1506 | 2989 |
2004/2005 | 671 | 396 | 505 | 1799 | 3371 |
2005/2006 | 726 | 415 | 688 | 1965 | 3794 |
2006/2007 | 727 | 641 | 932 | 2143 | 4443 |
Loyer mensuel tout compris pour les nationaux | Loyer tout compris en frCFA pour les étrangers | |
---|---|---|
Villages A,B,C,D,E,F,K,M | 3000 (4,57 euros) | ??? |
Villages H,I,J,L | 4000 (6,09 euros) | ??? |
Royuwaay:Portail Royuwaay:Infobox Université ' Iniwersite Gaston Berger mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal.

thumb|350px|Évolution des effectifs de l'UGB entre 2001 et 2007

L'université Gaston Berger est composée d'unités de formation et de recherche (UFR équivalent des facultés). Il y en a huit au total :