Ndiiwani Senegaal
Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal .
Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas . Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.
Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007 .
Ndiiwaani Bàkkel
Bala
Jaawara
Gudiiri
Kidiira
Ndiiwaani Bambey
Ndiiwaani Biñoona
Jululu
Sinja
Tenduk
Tengori
Ndiiwaani Cees
Ndiiwaani Dagana
Ndiiwaani Fatik
Jaxaaw
Fimla
Ñaaxar
Taatagin
Ndiiwaani Funjunj
Jilloor
Ñoojoor
Tubaakuta
Ndiiwaani Gosaas
Ndiiwaani Géejawaay
Géejawaay moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 5 dëkkani ndiiwaan
Ndiiwaani Kafrin
Dogiinu tund wi dañu koo soppi gannaaw sosug tunduw Kungeel ci 2006 .
Kon mu des :
Birkilaan
Maleem-Odaar
Nganda
Ndiiwaani Kanel
Ndiiwaani Kawlax
Ganjaay
Ndenjeng
Ndóofaan
Ndiiwaani Kebemeer
Ndiiwaani Kéedugu
Bandafasi
Fongolimbi
Salemata
Saraya
Ndiiwaani Koldaa
Dabo
Julaacolon
Medina Yoro Fula
Mi ngi judd ci 2006 (amul lonkoyoon bu jàppandi nii-nii)
Ndiiwaani Lingeer
Barkeji
Daara
Dooji
Yang-Yang
Ndiiwaani Luga
Kër Momar Saar
Kokki
Mbejeen
Sakal
Ndiiwaanu Raawo , biy feeñ ci lonkoyoon bi, ci tunduw Ndar la bokk 2002 ba tay.
Ndiiwaani Mbuur
Fisel
Ngeexoox
Caajaay
Jiwaalo
Ndiiwaani Mbakke
Ndiiwaani Ndakaaru
Ndakaaru moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 19 dëkkani ndiiwaan .
Ndiiwaani Njaaréem
Ndiiwaani Ndar
Gannaaw dogaat ga waraaloon juddug Diiwaanu Maatam , tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu
Ndiiwaani Ñooro gu Rip
Medina Sabax
Pawoskoto
Wak Nguna
Ndiiwaani Pikin
Pikin moom, benn Ndiiwaan la am muy moom ci boppam. Tund la ndiiwaan la
Ñu séeddale ko ci 16 dëkkani ndiiwaan .
Ndiiwaani Podoor
Kas-Kas
Njum
Salde
Cile Buubacar
Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Welingara
Ndiiwaani Séeju
Bunkiling
Jaatakunda
Jend
Marsasum
Tanaaf
Ndiiwaani Siggcoor
Ndiiwaani Tambaakundaa
Kumpentum
Kusaanaar
Makakolibantang
Misiira
Ndiiwaani Tënjéej
Tund wi, wenn ndiiwaan rekk la am muy bu Sebixotaan, moom ci boppam ñu séddale ko ci 3 dëkkaani Ndiiwaan .
Ndiiwaani Tiwaawon
Meewaan
Merina Daqar
Ñaaxeen
Pambal
Ndiiwaani Usuy
Ndiiwaani Welingara
(fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal , Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0 )
(fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ? , Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3 )