Peex xeetu garab la gu bokk ci njabootu Bignoiaceae te bàyyikoo Afrig gu naaje.
As ngarab la su am i tóortóor yu yor melow puur te dajaloo ciw car.
Jur gi dañ ciy xéewaloo.
Stereospermum kunthianum