Yoon moom lanuy wax ci tubaab (justice) dees na wax it yoon jublu ci li nuy wax (loi)walla (code) yoon tam dina tekki fi nit di jaar, dees na ci jublu it lu nosu maanaam tegu na ci yoon.
Yoon nag it ci nosteg penc (systeme republicuain) benn la ci ponk yi àtte gi (l'etat) di tegu di ci doxe, ponk yooyu ñaare ñatt lañu
Xam-xam | ||||
Gëstubiddiw | Jëmm | Paj | Saytubiddiw | Simi | Xam-xamu suuf si ak jawwu ji | Xayma | ||||
Jokkoosoryante | Xaralaymbëj | Doolerandu | Kàttan | Xam-xamu nosukaay | Mbëjfeppal | ||||
Diine | Melosuuf | Wërlaay | Nit | Yoon | Koom-koom | Taariix | Xeltu | Kàllaama |